Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2021
Àjjuma
Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Luug 17:5: «Yokkal sunu ngëm».
Samdi
Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci Yudd 3: «Xeexleen xeex bu metti ngir seen ngëm.»
Dimaas
Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Macë 21:21: «Su ngeen gëmee . . . , dina ko def.»
Li ñi teew war a xam
Tegtal yu am solo yu ñi teew ci ndaje bu mag bu ñetti fan bii, war a xam.