2023-2024 Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak ki bànqaas bi yónni
Nañu dugg ci noflaayu Yàlla!
Porogaraamu suba si ak bu ngoon si, bu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni.
Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
Dinañu tontu ci laaj yii ci ndaje bu mag bi.