Mën ngeen a am jàmm ci seen biir njaboot
Mën ngeen a am séy bu neex te am jàmm ci seen biir njaboot, bu ngeen toppee santaane yi nekk ci Biibël bi.
Ubbite bi
Mën ngeen a am jàmm ci seen biir njaboot ak séy bu neex bu ngeen toppee xelal yi nekk ci téere bii te sukkandiku ci Biibël bi.
XAAJ 1
Dégluleen Yàlla ngir am Séy bu Neex
Bu ngeen di laaj seen bopp ñaari laaj, loolu dina leen dimbali ba seen séy neex.
XAAJ 3
Li ngeen mën a def bu poroblem amee
Fasoŋ bi ngeen mën na wone ndax seen séy dina dëgër te neex walla dina naqari.
XAAJ 5
Li Ngeen Mën a Def ngir Wéy di Juboo ak Seeni Mbokk
Mën ngeen a teral seeni waajur te doo leen yàq seen séy.
XAAJ 7
Naka ngeen war a yare seen doom
Yar tekkiwul rekk tëral ay sàrt ak door waaye ëmb na lu gën a bare.
XAAJ 9
Jaamuleen Yexowa ci seen biir Njaboot
Naka ngeen di gënee a mën a am a am jàmm ci seen njàngum Biibël bi bu neex ci seen biir njaboot gi ?WEB:OnSiteAdTitleJaamuleen Yexowa ci seen biir njaboot