Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024 bi tudd «Nañu yégle xibaaru jàmm bi!»
Àjjuma
Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Luug 2:10—«Xibaaru jàmm buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.»
Samdi
Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci Sabóor 96:2—Yégle leen bés bu nekk ne, Yàlla mooy musal.
Dimaas
Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Macë 24:14—«. . . Bu loolu amee mujug jamono ji jot.»
Li ñi teew war a xam
Tegtal yu am solo yu ñi teew war a xam.
Seetal itam...
LU JËM CI ÑUN
Kaay teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024 —«Nañu yégle xibaaru jàmm bi!»
Ñu ngi lay woo nga ñëw teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bi Seede Yexowa yi di am ren.
NDAJE YU MAG YI
Ñu ngi lay woo ci ndaje bu mag bu ñetti fan bu Seede Yexowa yi bu atum 2024 bi tudd: «Nañu yégle xibaaru jàmm bi!»
Ñu ngi lay woo nga ñëw teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bi Seede Yexowa yi di am ren.
NDAJE YU MAG YI
Lãsamã tiyaatar bu sukkandiku ci Biibël bi te tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle: Xaaj 1 (Leer gu wóor gi ñëw ci àddina)
Seetaanal lãsamã tiyaatar bi tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle (Xaaj 1). Tiyaatar boobu dinañu ko wone ci ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2024.